XAM SA DIINE CI WOLOF
XAM SA DIINE CI WOLOF ak 3 téere yu Seex Ahmadu Bamba Mbakke
1)
Yöbbalug ndaw ñi
Tazawudus-sixaar
Aju ci ngëm, topp ak sellal
2)
Wurus wu gànjaru
Jawharun-naffis ci
Aju ci laab ak ci julli
3)
Yoonu faj aajo
Nahju Qadaa-il Haaj
Aju ci teggin
14,50 €Prix

































